Social Living – Njaaya

par | 6 novembre 2010 | Paroles de Chansons


Aadounaa
Moo Mél nii
Aadoounaa
Lii laniouy doundou
Thiéy lounouy doundou

Aadounaa
Moo Mél nii
Aaadoounaa
Lii laniouy doundou
Thiéy lounouy doundou

Sa Souma yéwo
Mén mi lay dianoll
Ndékété yo yo
Ména momé La dogall

Diw néna da khiff
Diw néko naniou sathie
Diw néko naniou gueum
Diw néko matouta gueum
Diw néna menoul dém
Té dou bayi kénén dém
Diw néna niéwoulaa
Wayé bou sanione mél ni yow

Man dandou lén ma
Yén nieup nalé
Damay lolambé
Kouffi beugue diallé diokhé

Man dandou lén maa
yén nieup naléé
Ragal na sankou
Balén ma mandou

Aadounaa
Moo Mél nii
Aadoounaa
Lii laniouy doundou
Thiéy lounouy doundou

Aadounaa
Moo Mél nii
Aadoounaa
Lii laniouy doundou
Thiéy lounouy doundou

Kouma Teumbeul nak
Tchip tén wo sant kon makh

mom ma ngay wakh
nguir askan wi bayi ko Khél

Katann wi diékhnaa
Wayé doyaloumaa
Yor thiaby adianaa
Koumou nékhoul ngafaa
Lii ma yotou dikenaa
Téy ma fayou péssmaa
Douma kheuthio lima momm
donté may borom

Man dandou lén ma
Yén nieup nalé
Damay lolambé
Kouffi beugue diallé diokhé

Man dandou lén maa
yén nieup naléé
Fou ma nékh farr
Té douma kakatarr

Aadounaa
Moo Mél nii
Aadoounaa
Lii laniouy doundou
Thiéy lounouy doundou

Aadounaa            Kou néka ak sa philosphie
Moo Mél nii            Ni la nieuwéé
Aadoounaa             Wo ohou woooohhh
Lii laniouy doundou        An hannn
Thiéy lounouy doundou        An hannn

Lii laniouy doundou
Lii lay lii ngay
Lii laniouy
That’s you that’s me yéh yéh yéh

{youtube}qy9n8bR9mnA{/youtube}

Un seul mot pouvant faire la difference… merci de nous corriger dans les commentaires. Les parties en rouge dans le texte représentent des incertitudes appélées donc à etres corrigées.
Ceux qui ont des paroles de chansons sénégalaises et qui veulent les partager, merci de nous les envoyer à [email protected].

 

Articles similaires

Rihanna – Where Have You Been

Rihanna – Where Have You Been

I've been everywhere, man Looking for someone Someone who can please me Love me all night I've been everywhere, man Looking for you babe Looking for you babe Searching for you babe Where have you been Cause I never see you out Are you hiding from me, yeah? Somewhere...

Dans mon rêve – Didier Awadi

Dans mon rêve – Didier Awadi

Né en 1969 à Dakar, capitale du Sénégal, Didier Awadi a grandi dans le quartier Amitié. Pionnier du mouvement rap au Sénégal et plus largement en Afrique de l'Ouest, Didier Awadi a fondé en 1989 le groupe Positive Black Soul (PBS) avec Doug-E-Tee (Amadou Barry). Leur...

Music I life – Dread Maxim Amar

Music I life – Dread Maxim Amar

Intitulé « Musical Life» et sous-titré « Kan moy Dof », axé sur la vie musicale du chanteur, ce nouvel opus de Dread Maxim est Composé de 12 titres, cette production 100% reggae et 100% live a été présentée à travers une tournée scolaire à Dakar et dans les régions....