Daara J Family – Tomorrow

par | 14 mai 2010 | Paroles de Chansons

TOMORROW


Refrain:

Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw

VERSE1/

souba souba yalla doleen jéxal
linga warra déf boul khaar défal
amoul yaggal téyla téyla!!
biss bo toogat wéyna wéyna!!
euleuk yégségoul défko légi
weurseuk gneuwna légi légi
« veuf » nawaat ci ngélaw
yaakar rombla ngay daw
linga wara déf boul thiow
boul khaar moulay reuthie
boul yeuglou boul jébbalou
déf lingay déf né keuthie
fi nga wara jaar ba tékki
légi la ci téew amoul jéllalee ‘k bama yéewu
défal yitté ba jiité say xalaat nimou dikké
saabo kheuyé nanga jeufé linga beug té boul tiit dé

Refrain:

Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw

VERSE2/

IT’s early morning i suggest
u wake up rather than wasting your time
yawning and snoring while time is running
get up and do something
you ll never make it scrounging
don t expect to reap credit if you ve sown nothing
what you waIting for grind it work it while the heat is on
don’t moan and groan step up on your feet
go it alone keep your ongoing spirit
ready steady to take sky s the limit
your life is only what you make it
it is right away you made your brighter day
tomorrow s another day
your best bet could be made today

REFRAIN:
Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw

VERSE3/

euleuk jaayoontéla gisso liy gneuw dabantéla
njeukeu départ daxantéla,wakhtou wou gneuw garantila
fi nga nékoon daw joggulafa,bancs-jaxlé ak boppu kogn bi
ha!! ha!!

yu ll be rewarded for every sacrifice yu make
don t fall asleep for God s sake
tomorrow is today
gotta do what you gotta no matter what it takes
joggal sigil,nanga jeul sa euleuk ci say niari loxo
boul ragal ,boul ne thiell takkal sa fit ta gueum ne meun nga ko

REFRAIN:

Boul xaar loy déf défko,loula thi fék mouy loolu,loula thi fék mouy loolu
bagna took di khaar tomorrow
war nga wagni lingay nélaw
banga xaméni yoonu ndam dou gaaw
war nga jog thia teel ndax nga raw

you better wake up…you better wake up…

 

 

{youtubejw}bV4qTlyw2SQ{/youtubejw}

Articles similaires

Rihanna – Where Have You Been

Rihanna – Where Have You Been

I've been everywhere, man Looking for someone Someone who can please me Love me all night I've been everywhere, man Looking for you babe Looking for you babe Searching for you babe Where have you been Cause I never see you out Are you hiding from me, yeah? Somewhere...

Dans mon rêve – Didier Awadi

Dans mon rêve – Didier Awadi

Né en 1969 à Dakar, capitale du Sénégal, Didier Awadi a grandi dans le quartier Amitié. Pionnier du mouvement rap au Sénégal et plus largement en Afrique de l'Ouest, Didier Awadi a fondé en 1989 le groupe Positive Black Soul (PBS) avec Doug-E-Tee (Amadou Barry). Leur...

Music I life – Dread Maxim Amar

Music I life – Dread Maxim Amar

Intitulé « Musical Life» et sous-titré « Kan moy Dof », axé sur la vie musicale du chanteur, ce nouvel opus de Dread Maxim est Composé de 12 titres, cette production 100% reggae et 100% live a été présentée à travers une tournée scolaire à Dakar et dans les régions....